Loading
Page contact    Imprimer         Partager sur :  facebook    twitter    google+ 
Sujets en langues nationales
                       |   
 wakhttan
Auteur: miss diop 
Date:   28-09-05 00:59   >>> Répondre à ce message

da ma mbeugue waxtan ak yen thi leep loye khew senegal surtout thi yack yi youn def thi khew yi
 
 Re: wakhttan
Auteur: miss diop 
Date:   28-09-05 17:29   >>> Répondre à ce message

mbeuguou len waxtan lou khew
 
 Re: wakhttan
Auteur: miss diop 
Date:   05-10-05 22:39   >>> Répondre à ce message

bonne ramadan
 
 Re: wakhttan
Auteur: Imam 
Date:   05-10-05 23:11   >>> Répondre à ce message

Déwénati, Miss Diop.
 
 Re: wakhttan
Auteur: Ndar-- 
Date:   06-10-05 09:19   >>> Répondre à ce message

dewenati
 
 Re: wakhttan
Auteur: miss diop 
Date:   06-10-05 13:49   >>> Répondre à ce message

balene ma ak bale na len yala na you yala bole bale thi dara diey mohamed salalakhou aey wa salam
 
 Re: wakhttan
Auteur: miss diop 
Date:   07-10-05 21:36   >>> Répondre à ce message

na ka kor bi
 
 Re: wakhttan
Auteur: miss diop 
Date:   10-10-05 11:00   >>> Répondre à ce message

kha na kor bi da fa saf
 
 Re: wakhttan
Auteur: l'élu   
Date:   13-10-05 01:08   >>> Répondre à ce message

salam sama djiguéne ah kor gui dé saffoul sakh dé wayé nak kham nga nit gni dougnou am diot kham na laulou mo takh dal wayé nak dou dara dé
 
 Re: wakhttan
Auteur: miss diop 
Date:   13-10-05 16:53   >>> Répondre à ce message

aujourd 'hui avec la pluis kor bi sa foul
 
 Re: wakhttan
Auteur: Imam 
Date:   13-10-05 23:38   >>> Répondre à ce message

Waou, Miss Diop fooy bindé, ndax fi Paris tawul dé.
 
 Re: wakhttan
Auteur: miss diop 
Date:   15-10-05 22:20   >>> Répondre à ce message

JE SUIS au senegal
 
 Re: wakhttan
Auteur: Imam 
Date:   15-10-05 23:47   >>> Répondre à ce message

Kon batay mungi taw Ndakaru. Kon nawetu ren bi moom yagg na dé. Mbaa dégat yi baré wul.
 
 Re: wakhttan
Auteur: miss diop 
Date:   16-10-05 19:24   >>> Répondre à ce message

tu sai avec la pluis premier dakar ete innonde surtou pond de padoi
 
 Re: wakhttan
Auteur: miss diop 
Date:   19-10-05 10:22   >>> Répondre à ce message

salut les amis
 
 Re: wakhttan
Auteur: miss diop 
Date:   21-10-05 16:07   >>> Répondre à ce message

wa ka na kor bi da len teyer me ne to len gen
 
 Re: wakhttan
Auteur: a.joob 
Date:   23-10-05 11:45   >>> Répondre à ce message

Na nga def miss Diop?
Nu waxtaan boog!
Sa mbind mi leerul ci man, ndaxte ortograf bi li ma jànge ci wolof dafa wuute. Waaye dama la gërëm, ndaxte jefandiku nga sa làkku reew mi bu baax! jërëjëffati, waay!
 
 Re: wakhttan
Auteur: missdiop 
Date:   29-10-05 23:06   >>> Répondre à ce message

salut je suis dacor de ce que tu dis
et maintenant si tu es dacors apprend moi le wolof
 
 Re: wakhttan
Auteur: a.joob 
Date:   30-10-05 19:09   >>> Répondre à ce message

Li ma la mën a jàng barewul noonu, waaye nu góor-goorlu rekk di waxtaan fii ci foorum bi.
Amuma jot bes bu nekk nôw fi, wànte su la neexee dama la jeem a tontu. Naka Ndakaaru tey, mun ngi sedd walla déedéet?
 
 Polo Ralph Lauren Outlet
Auteur: Polo Ralph Lauren Outlet 
Date:   30-10-14 21:46   >>> Répondre à ce message

Westwood believes that there are too few female designers whose designs are kind to women, glamorous and empowering. Her belief is that "Fashion is very important. It is life-enhancing and like everything that gives pleasure, it is worth doing well"
Polo Ralph Lauren Outlet http://www.cyneric.com/polooutlet.asp

Message posté par un internaute non inscrit dont la géolocalisation détectée est : VILLE : PAYS : France
Posté depuis www.senegalaisement.com
                       |   

Liste des forums  |  Besoin d'un login ? Enregistre toi ici
 Identification
 Nom d'utilisateur:
 Mot de passe:
 Se rappeler de mon login:
   
 Mot de passe oublié ?
Entre ici ton e-mail ou ton identifiant et un nouveau mot de passe te sera envoyé par mail.