Loading
Page contact    Imprimer         Partager sur :  facebook    twitter    google+ 
Sujets en langues nationales
                       |   
 Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Deug   
Date:   28-12-04 11:55   >>> Répondre à ce message

Dama beug xam, tubab yidi gneuw senegal, lan lagnou geuneu beug si:
xam adawu senegal
wala noppallu
wala fo-si
gnun gni nek senegal bugn xammé danagn geuneu meuneu ganalé gni difi gneuw.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   28-12-04 12:01   >>> Répondre à ce message

li guenone key, moy nga ladj lène ko gnom

mais cé koi? adawu sénégal???
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   28-12-04 16:04   >>> Répondre à ce message

Dëgg, xawma yeneeni Tubaab, waaye saa yu ma fay dem, dama am yaakaar di fa noppaliku, di fa jang li ma xamogul, di fa yokk samaw xel, leeral samay xalaat, dajeek samay xarit, deglu mizik bu neex-a-neex, waxtaan ak nit nu am xel te saf xorom.
Mess naa and ak sama benn xarit di dem Jollof, kooku nak, dem na fa di seet lu bees te di fa fo.
Sama benneen xarit it dem na fa, bëgg jang ca daara ju mag ja ca Ndar.

Kon, defe naa ni kenn mënul wax "lu Tubaab wutsi Senegaal", ndaxte tamit mënoo wax "lu nit ni nuul wutsi ci Tugal."
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   28-12-04 16:07   >>> Répondre à ce message

wala rek lou nit di woutsi si aduna si
wax nga deug tubaab, ladj bi dafa yaatou

mane dé so ubé daara ma bokk légui la wax, tiswiit
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: l'élu 
Date:   29-12-04 02:14   >>> Répondre à ce message

ak mane légui légui
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: cabolova   
Date:   30-12-04 13:47   >>> Répondre à ce message

mane je pense que dégni niow deme senegal parce que fofou deff lén nekh! et puis fofou nigni degni acceuillant!!

Deug; do len ma dimbali (le message parle de koi vraiment) j ai pas trés bien compris
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Deug   
Date:   03-01-05 10:19   >>> Répondre à ce message

dama beug xam lan moy "attraits " yu Senegal?
xam nga nit yi gnul yi eup di dém tugal, xalis lagnuy wut, way Tubab yu eup di gneuw Senegal, amna lénén lugnuy wut lumélni Kumpa, lu mélni naj, lu mélni xam-xam.
li tax ma laj li moy dama beug xam ban lassi nit yi di geuna déf?
je veux savoirs quels sont les attraits du Sénégal?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   03-01-05 16:28   >>> Répondre à ce message

Dëgg, ñu ëpp ci Tubaab yu dem WAKAAS, wutuñu lu dul noflaay. Senegaal, dañu fa dem di fa wut tangaay ak dund wu yomb. Turist yi gaa, daanaka ñepp a mel noonu. Am na ci ñoo xam ni deñ kumpa lañu ci boole, waaye duñu faral di yagg ca reew ma ba nand dara ci lu fa xew.

Li ma waxoon nak, li ma gën a neex Senegaal - man mii - mooy teraangaak cosaan, xalaat yu am maanaa ya, waxtaan wu tey ak ñoom seen, maanaam loo xam ni doo ko faral di giss ci reewi naat.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: l'élu   
Date:   05-01-05 04:13   >>> Répondre à ce message

Ah man dé daffa am lou ma diaxal waw laulou moy sunu copain "tubaab" khawma ndax toubab la khawma dou toubab wayé dé déggeune wolof dé yaw mi dé yagga nga lekka cep wawaw malako wax dé .
Manoulo nékka tubaab ba paré di laké ni wolof cone dé dina ma diakhal parce que amne ay senegalais yo gueuneu dégga wolof té laulou wor nama
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   05-01-05 10:53   >>> Répondre à ce message

l'élu lo diangu mokkal ko, surtout li ngey diangu soula nékhé
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Ndar-- 
Date:   05-01-05 11:05   >>> Répondre à ce message

cé pas juste (une larme qui coule)
vs comprenez les deux même sujet ouverts et pas moi!
;=(
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: l'élu   
Date:   06-01-05 02:24   >>> Répondre à ce message

WAW SEALIAH mais nak sounou copain bi nim ko dégué dafa khawa doye war (mat na tol sakh) té bo déglo dakar légui boy yi wakhatougne wolof ni ko "tubaab" di waxé en tout cas dal bou fékénténé daf ko djanga mome chapeau bas devant meme bou ko djangoul djar na diokh oscar parce man mi di wakh ak yaw yagga na di gagné ay "baatou wolof" ba gnou téré jouer mais nak c'est admiratif
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Deug   
Date:   07-01-05 18:05   >>> Répondre à ce message

Way Tubab, lo giss si lougn meuna bayi lutax gnou geuna néxa setsi?
L'élu, yaw gnémé nala si batu wolof, nganan champion nga. naco pierre teug, sealiah arbitréco.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   07-01-05 18:13   >>> Répondre à ce message

arbitre key dafa war gueun kham gnimouy até
wala?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: l'élu   
Date:   08-01-05 04:21   >>> Répondre à ce message

Deug dou ma sa morom sakh tchi baatou wolof maala man téméri yone té ma xamal la dara man fi france la yaro amna ay wolof you khaute yo xamné bouma lako doré rek nga xeume man djolof djolof la dé nga def ndanka nak .
waw guinaw laulou bou fékénténé gnamé nga ma tambalile ma khol sa dissayou loxo
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   10-01-05 11:15   >>> Répondre à ce message

l'élu fo meussé guiss wa guinée bissau bou dégueu wolof ? pierre diop dé dafa am dictionnaire , lolou moko si guéné
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Deug   
Date:   11-01-05 14:23   >>> Répondre à ce message

Sama dissay loxo gnico xam, dougn co néttali, motax duma laco wan.
dama beug nga wax ma luy xojox? dama séét ba son guissoumaco.
Sealiah, jappal rek garawoul, dossi son sah.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   12-01-05 21:21   >>> Répondre à ce message

l´elu, sealiah wax na lepp; loo jang di ci goor-goorlu rekk, boole ci tukkurmuut, dinga ko xaw a mën, bu soobe Sunu Boroom bi.
Te maa fii taxaw di wax ci kow: wolof jar na jang, jar na soppi, jar na fonk, ndaxte lakku xam-xam la, lakku woy la, lakku leeb la, lakku fent la, lakku teraangaak teggin la... Ku ci mëss a jang mbaa degg woy yi Seex Aliyu Ndaw fent mbaa ku mëss a degg waxi gewel ya, dootu ko bëgg a bayyi!

Waaye, l´elu, woor na Yalla ni sama wolof des na... Ba tay, maa ngi def li ma mën rekk!
(Ci yoon, kenn warul jaaxle boo gisee ab tubaab buy lakk Wolof mbaa Pulaar mbaa leneen; xanaa Wolof yeek Pëll yeek Seereer yeek neneen lakkunu Faranse ba di ci bind ay teere?)

Dëgg, ragal naa ni degguma sa laaj "loo gis ci lu nu mën a bayyi lu tax nu gën a neexa seetsi"? Su de danga may laaj lan ngeen di mën a bayyi ndax nit ni gën a sawar di leen seetsi, xawma lu ma lay tont... Waaye giss naa waa Senegaal faral di fog ni gan yi ay xale lanu, xamunu tus... di leen teg ay dof rekk (rawatina su nu lakkulee Wolof). Xanaa loolu.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   13-01-05 10:11   >>> Répondre à ce message

wouuuuuuuuuuuuuu wi
khawna kheum
l'élu ki wolofam fort na
dama sax rouss
ma ngi dem dieundi dictionnaire
lane moy : tukkurmuut? ak fent?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: l'élu   
Date:   15-01-05 01:06   >>> Répondre à ce message

Deug malay tontou ba nga contane tay ci gouddi bi, kham nga li takh temps yi yeup bindouma damma amoulaune internet laulou mo takh ,
bon "xojox" man li degga ci li nga binda peut etre man ma ko manoil lire mais bou dé man xojodj" bi ma yaakar la moy nga naan lou euppeu , manam nga naane ba mounau nokki (noy) pour gni deukkeu dakar
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   15-01-05 19:56   >>> Répondre à ce message

sealiah, maa ngi jeggalu... Tukkurmuut mooy lu nuy wax "enthusiasm" ci anglee. "Fent" mooy bind woy mbaa teere; "fent bi" mooy lu xaw a nirook ab nettali.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Deug   
Date:   16-01-05 01:35   >>> Répondre à ce message

Wax ji jib na nak
Mangui dég baat yo xamné,guéj naco dég depu sama mam Ali.
L'élu Xojox la wax,ap rap la bouy yég thi garab.
Sealiah Nangadef, ana pierre diop?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   17-01-05 10:32   >>> Répondre à ce message

deug namess yow
ki ngey ladjté moy xojox ba
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Géwélbabtou   
Date:   18-01-05 00:49   >>> Répondre à ce message

Assalam oua alaikoum,
alors, mane ngi gis sama mbokk tubaab mu ngi lène di jàngal wolof !

Boy, yangi wax bubax, kagn nga doon komaasé jàng lakk bi?
Aller, bo beneen.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   18-01-05 10:12   >>> Répondre à ce message

yaw kane ngey owé boy ni? khana deug wala pierre diop?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Géwélbabtou   
Date:   18-01-05 17:45   >>> Répondre à ce message

Sealiah:
Do Pierre Diop, do Deug.
pierre Diop ak Deug sénégalais yi lène, kon wolof bi sène lakk la, walla daniou wax wolof ba niou nékké xalé bolégi.
Wanté "Tubaab" nekkul senegalais, kon dafa doon jàng wolof boppam. Loloumotax ma wax ko mungi high...
Mane tammite, mane ngi jëmm wax wolof, waye mome il est au niveau superieur...
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   19-01-05 15:47   >>> Répondre à ce message

Gaa ñi, nammoon naa leen" :)

Gewelbabtou, jangaluma, damay fatteli rekk! Ndax bindkat nee na: "ku fonk sa kallama, jang ko di sa warugar..."
Ca atum 1999 laa ko tammbali jang, waaye ba leegi des na :( . Maa ngi dundee yaakaar samay doom dinañu ma ci raw fuuf! :)

Ca doomi Jollof nak, rawatina ndaw ñu cosaanoo taax ya, ku ci bëg a suqali Wolofam, na jang ay teere ak ay woy ci Wolof; am na ci yu neex-a-neex, yoo xam ni soo leen jangee sa yaaraam daw sax.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   19-01-05 17:11   >>> Répondre à ce message

lane moy daw yaram fofou???
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   19-01-05 17:18   >>> Répondre à ce message

Sealiah, boo jangee yenn yi, dinga nand... Ndax mëss nga degg dara lu jem ci Doomi Golo bi Buubakar Boris Joob bind, mbaa nettalib "Peccum Jaxaay" bu Seex Aliyu Ndaw?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   19-01-05 17:24   >>> Répondre à ce message

dédèt, si wolof la gnouko woyé ?



Message édité (19-01-05 18:21)
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   20-01-05 20:30   >>> Répondre à ce message

Ay teere wolof lanu, ci wolof lanu ko bindee. "Doomi Golo" nak, mën nga ko jend ca Farans sax, su la neexee (teere buy am lu mat 300 xet la).
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Deug   
Date:   24-01-05 11:51   >>> Répondre à ce message

Tubaab
Dinga ma taxa jeun tééré yoyu ndax ma meana dég wolof, man dama galli.
mangui lay digal tééré bu Amadu Lamin Nduur bi tudd "300 Léebu ci wolof".
addinam xel, jamanoy beut. jang sa lakk dafa war ci jamano ji nga xamné gneup tognagn si séén and.
ku wath bossam xam!
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: l'élu   
Date:   26-01-05 03:49   >>> Répondre à ce message

Man dé tubaab mongui may diakhal bess bou nekka yaw dé am na gars yo khamné ya léne geunneu dégga wolof, ci bou lér.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   26-01-05 17:55   >>> Répondre à ce message

Dëgg, jërë-jëfati!
Xam nga rekk, li kenn mën, ñaar a ko daaq... Waaye bul ma rey ak leebu yi: ngaaxi tukkal, kenn du ko perngal mboccoor, te man Tubaab doNN laa :) .
Teere bi ngay wax, jotoguma ko giss. Yor naa bu Mansoor Xumma, moo di "Junniy Leebu Wolof" (duñu 1000 nakk, 999 leebu rekk moo fa nekk).

L´elu, loolu mënul nekk... Maa ngi ci jeem a goor-goorlu rekk, di leen bayyi ngeen yokk sama xel, suqali samaw xam-xam.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   26-01-05 17:56   >>> Répondre à ce message

... di leen ciy sant, di leen ciy gërëm! :)
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   31-01-05 17:52   >>> Répondre à ce message

mane ma bindeu 1000è bi
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Deug   
Date:   07-02-05 14:07   >>> Répondre à ce message

Séaliah
Baxé ma 1000è bi bok.
Tubaab,fo nék? Tuggal wala Senegal?
Lingay dafni dina amal gnou bari jarign bugn xaméni wolof lugnu mana jang la ba raw piir.
Anna Pierre Diop?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   07-02-05 15:07   >>> Répondre à ce message

pierre diop dafa wouti doolé
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   08-02-05 14:04   >>> Répondre à ce message

Deug, maa ngi ci diggu Tugal, ci reew mi nuy wax Republik Cek.

Pierre Diop reer na... :(
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Deug   
Date:   10-02-05 14:58   >>> Répondre à ce message

Républiq Cek
waju bax, fi nga nek dé xalatu malawon fofu.
ndax dingay dajég ay sénégalais fofu?

"Avis de recherche lagn wara daf guir séét fou Pierre nék.

Mba nékoul di séét fou Sealiah nék, ba far réér?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   10-02-05 18:26   >>> Répondre à ce message

pieeeeeeeeeeeeeeeeeeeeerre dioooooooooooooop
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   11-02-05 13:07   >>> Répondre à ce message

Deug, Senegale yi barewunu fi, waaye dama dajeek noom, ci lu wer :)
Xanaa yeen nepp ca Farans ngeen di nekk?

Dafa mel ni Sealiah xam na fu Pierre Diop duggu de! ;-)
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   11-02-05 13:59   >>> Répondre à ce message

Tubaab, lu muy tekki: "dajeek noom"? "duggu" nak?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   11-02-05 15:00   >>> Répondre à ce message

naka nga wax ci wolof "je ferme la bouche déjà"?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   14-02-05 15:15   >>> Répondre à ce message

tubbab, boulma indil tiowe dé
pierre diop dé khawma foumou nek, soumako khamone dieuli, ko nakh dama ko nama
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   23-02-05 19:19   >>> Répondre à ce message

hodei, "dajeek noom" comes from the contraxion of daje-ak-noom (meeting them). Duggu = enter.
"je ferme la bouche", boobu duma koy wax ndaxte su ma ko defee, nepp a ko giss; jarul ma yegal ko nit ni.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   24-02-05 10:26   >>> Répondre à ce message

Tubaab, salut!! gëj naa la liir, fils..
ok, jërëjëf pour traduction bi.

benn laaj... foo jogé?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   25-02-05 14:41   >>> Répondre à ce message

Hodei, mon pere :) man duma "fils", xanaa ma doon "fille" :D

Nammoon naa la nak, nu mu demee? :)
Europe Penku laa fekk baax, yaw nak?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   25-02-05 14:47   >>> Répondre à ce message

jijiji, Tubaab... ok fille... xamuma lu tax xalatoon naa ne benn fils nga! pas grave...

Màngi sant... dox na! màngi ci université bi, leegi.
Europe Penku?? foo jogé ci Europe??
Barcelona laa dëkk
A plus
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   25-02-05 15:40   >>> Répondre à ce message

:D O.K. ... No problem, I´m not a sexist! :)

Man, Paraag laa bawoo. :)

Dangay jang Wolof ca seen daara ja walla? Ndax mëss nga jang ab teere Wolof, maanaam ab teere fent mbaa teere kilib, ay woy...? Woor na ma ni boo ko defee dinga gaaw a suqali sa Wolof bi. :)
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   25-02-05 15:55   >>> Répondre à ce message

Oh, Paraag!! màngiwoon fa!!

Daaw demoon naa ci Senegal ak neex na ma torop lu ma bëggoon jàng wolof (samay xarit xalaat neñu dama dof :D).
Apre par occasion, wutewoon naa benn jangalekat.... wànte leegi, amul sama jot ak jéém naa jàng par ma même (je suppose que j'achèterai livre bi)

attends... lu muy tekki: "Woor na ma ni boo ko defee dinga gaaw a suqali sa Wolof bi"?

quelle est ton histoire?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   01-03-05 15:14   >>> Répondre à ce message

"Woor na ma ni..." means "I am sure that, if you´ll do it, your Wolof will develop very fast."

Loo doon def Parag nak? Turist-turistlu xanaa? :)

Nde daaw rekk nda demoon Senegaal? Jangalekat yu baax yi neexunu giss, man mii sax dama amoon ay jangalekat ca tammbali bi, waaye nu ci ëpp ay yefi dof rekk lanu ma waxoon te jamano booba mënuma ko woon a rannee :( .

Hey, please drive your attention to that you can´t use "ak" like simple "et". "Ak" can be used only for connecting two subjects, but not for connecting two sentences - then you have to use "te".
(daaw dem naa senegaal TE neex na ma... amul sama jot TE jeem naa...)
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   02-03-05 16:51   >>> Répondre à ce message

Tubaab, naka mu?

Apre liir sa post nànd naa lu tax sama xarit bu senegalaise wax nga ma: "sa wolof mel ni màgget" :D
Soxlo naa vocabulaire ndax pour bépp ñetti làmmiñ nga wax, war naa wut ñaari ci dictionnarire bi jijii wànte ça, dimbëli na ma ngir jagal. Ça marche!

Lu tax nga laaj ma suma nekkoon Senegaal daaw rekk? Ñaata jamano mës nga tukki fa? (bëgg naa dellusi waaye kañ am naa xaalis, amuma jot TE (jërëjëf! :D) kañ am jot, amuma xaalis! Ey waay jilé!)

"nga laaj ma" wute na ag "laaj nga ma"? Xamuma mukk suma ko bindéé correctement...

Am naa yenn laajte... lu muy tekki "nde/nda"? (Nde daaw rekk nda...) "yefi", nak? (nu ci ëpp ay yefi dof...) "rannee", nak?... xamuma loo mënoowoon def... jejeje

oooook!! wóór!! suma tekkiwéé "woor" par "wóór"="sure" jëli naa phrase bi, non obstant xamuma lu tax nga bind "Woor na ma ni"... it wouldn't be... "wóór naa ne..."... lu tax "na ma.."?

waaw... màngiwoon ci Paraag en vacances!!

Ah, dig naa la bind, sérieux!

A plus
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   03-03-05 11:26   >>> Répondre à ce message

Tubaab... nànd naa ndax nga bind "wóór na ma ne" leegi (I've checked it) wànte I've a new doubt... the rest of the conjugation is...:

wóór na ma
wóór na la
wóór na ko
wóór na nañu
wóór na leen
wóór na neñu ????
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Deug   
Date:   08-03-05 14:40   >>> Répondre à ce message

Hohodei
ya nex, nula nex ngay waxé (wolof), dinala jangal ndaxté yaw dangay nirou cou pank.
Waxu ma xéx lalay jangal, mais wolof!



Message édité (10-03-05 15:28)
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   08-03-05 14:56   >>> Répondre à ce message

Ei eieie eiei Deug...
damay nirou cou pank?? LU TAX???
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Deug   
Date:   10-03-05 15:32   >>> Répondre à ce message

damalay togn rek, histoire de thiocass
nand nga?
dafa am gnou fi néconn té gissatoumaléne, hawma dagno daw, wala dagno giss lénéne way warnagn gnou taggu bala dara di xéw, bouco daffé sax gnu uut gnu béss.

Wanted Sealiah,Pierre Diop et Tubbab!

prix= 1 tasse de bissap
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   10-03-05 16:03   >>> Répondre à ce message

adu cassou bissap bi
yaw ya nay rec
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   13-03-05 12:12   >>> Répondre à ce message

Deug, baal Tubaab bi nak, dafa soog a am gan, maanaam taawlu :) ... Su sama takkandeer boobnu xawee fendi, dinaa nowaat...
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab 
Date:   13-03-05 12:23   >>> Répondre à ce message

hodei, the conjugaison is correct, but

woor na nu
and
woor na nu (gnu)
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   14-03-05 16:51   >>> Répondre à ce message

Fii sa kër la, Tubaab! :P
Jërëjëf.

Foo nëkk Deug?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   14-03-05 17:20   >>> Répondre à ce message

Tubaab di ngama rey rec
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   14-03-05 18:10   >>> Répondre à ce message

lu tax nga wax ko, Sealiah?
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   15-03-05 13:07   >>> Répondre à ce message

Su sama takkandeer boobnu xawee fendi, dinaa nowaat...

dégouma wolof yi mouy lakkeu
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Deug   
Date:   15-03-05 14:39   >>> Répondre à ce message

Manam dafay doga am BB
Tuubab budé du nonu nga xétali gnu ndaxté gnun dégungn lingay wax ni.
Professeur Sealiah sax nandul!
Hohodei, kent waxuco
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   16-03-05 16:51   >>> Répondre à ce message

Waay ku reelu la! :D
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei 
Date:   17-03-05 15:31   >>> Répondre à ce message

et j'ajouterai... Deug??: dafa compliqué.. lool sax!!
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: sealiah   
Date:   26-03-05 15:49   >>> Répondre à ce message

deug sa kanam ni professeur sealiah
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: l'élu   
Date:   28-03-05 05:41   >>> Répondre à ce message

Man dé benna jour tubab dafa done wakh né mome vrai toubab la mais nak man gueumoumako ndax té am na affaire you mouy lakka yo kham né doyna war dal .
Té li deug wax naunoula dafay dor di wassine mo takh dina absenté mais nak toubab simple mounoul wakh wakh yauyou en tout cas dal djakhal nama
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab bu jigeen   
Date:   24-06-07 03:28   >>> Répondre à ce message

Tubaab bi dellusi na... Nammoon na leen, nammoon na noo xamante ne nangunu gëm na ab Tubaab la, tubaab bu xonq cuyy ni xaal bu nor xomm... Tubaab bu am naari takkandeer dikkati na! :-)))

Ragal, yab Yalla la.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Imam   
Date:   25-06-07 00:09   >>> Répondre à ce message

Eh ! ma ne gii wolof, du wolofu tubaab. Bul nu fontoo.

Waaye li ma jaaxal moy mbind mi, ndax tubaab yi rekk ñooy bind wolof nu mu waree, boo ko weddee xoolal mbindu ñii ngay waxtaanal fii.



Message édité (25-06-07 00:15)
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei   
Date:   25-06-07 11:13   >>> Répondre à ce message

Salam mbokk mi!!!
Tubaab bu jigéén ak Imam, nammoon naa leen, bilaay!!!
am naa yaakaar yéénëgi ci jàmm!!
Ci kaw ci kanam
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: LeMur 
Date:   26-06-07 10:00   >>> Répondre à ce message

Wahaaaaaaaaa !! Imaam yaa yay jommi de, bii tubaab de xam naa ni bayyee gu ko ak kénn !
Wolof yu xòòt te leer nàññ la fiy làkk de moom !
Bu loolu weesoo nàmmoon naala, yaa ngi jàmm mbaa?
Hodei, yaw jàmbaar nga de yaw tamit :D !

 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Imam   
Date:   27-06-07 23:24   >>> Répondre à ce message

Waaw le mur, Hodei, maa leen raw. Waaye tan yii dama japp loolu. Moo tax ma raar boor yii. Waaye ci kanam daa nu mana daje fii waxtaan.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: hodei   
Date:   28-06-07 01:02   >>> Répondre à ce message

Imam, namessss grand.Courage kon.
sinon... bi nga amee jot dinaa nekk fi ngir ñu waxtaan de.
Yàlla na la Yàlla sàmm!
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: Tubaab bu jigeen tigi   
Date:   22-12-16 10:33   >>> Répondre à ce message

Laaj wi xanaa nun tubaab yi nga koy laaj ;-) . Samay saari dańoo wuti xam-xam, waaye it am na ńoo xam ne noflaay mooy seeni tank. Ńenneen nak deń kumpa moo leen indil, mbaa ńu giss paas bi yomb rekk daldi takk seeni waxande dem.
 
 Re: Bu tubab gneuwé sénégal....
Auteur: king   
Date:   21-09-18 00:44   >>> Répondre à ce message

cc20180921
polo ralph lauren outlet
nike air max
moncler
kate spade handbags
baltimore orioles jerseys
red bottoms
coach factory outlet
cheap jordan shoes
canada goose outlet
nike react shoes
kyrie 4 shoes
nike free 4.0
coach factory outlet
coach outlet
ecco shoes
canada goose jackets
supreme clothing
tiffany and co
new balance outlet
cheap jordans free shipping
canada goose
los angeles dodgers jerseys
ugg outlet
canada goose outlet
nike outlet store
pandora charms
birkenstock outlet
coach factory outlet
underarmour shoes
fitflops
ugg outlet
adidas yeezy
uggs outlet
uggs outlet
coach outlet
cartier outlet
louis vuitton outlet online
kate spade outlet store
polo ralph lauren outlet
louis vuitton handbags
louboutin shoes
mulberry bags
michael kors outlet
supreme clothing
mbt shoes
timberland boots
cheap jordan shoes
coach canada
fendi handbags
adidas outlet
burberry outlet
ultra boost
uggs outlet
pandora jewelry outlet
swarovski crystal
ray ban sunglasses
ecco outlet
michael kors outlet
rolex watches
nike cortez
canada goose outlet
canada goose jackets
coach outlet online
vans shoes
kate spade handbags
nike outlet
converse outlet store
coach factory outlet online
nike air max 1
coach outlet store online
air jordans
pandora charms
adidas shoes
adidas originals
kate spade handbag
kate spade handbags
coach outlet
gucci handbags
nike outlet online
coach outlet
pandora jewelry official site
nike huarache
moncler outlet
air max 2019
air max 2018
ugg outlet
canada goose outlet
supra shoes
oakley sunglasses
nike outlet
moncler jackets
cheap jordans for sale
supreme new york
uggs outlet store
columbia shoes
ugg boots
colorado rockies jerseys
kate spade outlet
valentino shoes
nike free run
louis vuitton
coach outlet online
canada goose outlet
pandora jewelry
nike shox
michael kors
michael kors outlet online
nike outlet
jordan shoes
adidas nmd
cheap jordans
coach factory outlet
pandora charms
pandora jewelry outlet
cheap nike air max
adidas yeezy boost
coach outlet
canada goose outlet
coach outlet
atlanta braves jerseys
kate spade bags
new york mets jerseys
nike outlet online
nike air max 95
louis vuitton
uggs canada
adidas nmd
cincinnati reds jerseys
oakland athletics jerseys
canada goose jackets
coach outlet
adidas superstar
pandora charms
seattle mariners jerseys
ysl outlet
kate spade handbags
coach outlet store
adidas campus
pg 2
new balance shoes
uggs
pandora charms sale clearance
hermes handbags
cheap nfl jerseys
michael kors outlet clearance
canada goose
ray ban sunglasses discount
kobe shoes
coach outlet store
oakley sunglasses
christian louboutin
rolex watches
lacoste polo shirts
pandora jewelry
nike outlet
ugg outlet
ugg boots
ralph lauren outlet
red bottom shoes
ugg outlet
michael kors outlet
birkenstock sandals
yeezy 350 boost
kate spade
ralph lauren sale
pandora jewelry
swarovski outlet
toms shoes
fitflops
coach outlet
salvatore ferragamo shoes
uggs outlet
lebron james shoes
coach handbags
coach factory outlet
canadian goose
jordan shoes
north face outlet
nike shoes
kate spade outlet
louis vuitton outlet store
canada goose sale
coach factorty outlet
jordan shoes
birkenstock sandals
burberry outlet canada
yeezy boost
dr martens
fred perry
michael kors outlet online
nike outlet
longchamp outlet
nike shoes
pandora jewelry official site
coach factory outlet online
louboutin shoes
michael kors outlet
birkenstocks
christian louboutin outlet
coach outlet
fitflops
kate spade outlet
jordan retro
houston astros jerseys
canada goose jackets
polo outlet
fred perry polo
air jordans
cheap nfl jerseys
timberland outlet
moncler outlet
toronto blue jays jerseys
michael kors outlet canada
los angeles angels jerseys
coach outlet
reebok shoes
coach factory outlet
ysl handbags
fitflops sale
ray ban sunglasses
arizona diamondbacks jerseys
coach factory outlet
pandora jewelry
cristiano ronaldo jerseys
jordan retro 11
coach factory outlet
uggs
christian louboutin outlet
jordan shoes
michael kors
nike cortez
mlb jerseys
timberland boots
coach outlet
air max 97
nike air presto
adidas yeezy
adidas shoes
coach outlet
yeezy boost
canada goose outlet
ralph lauren outlet
kate spade outlet store
moncler outlet
cheap mlb jerseys
hermens bags
coach factory outlet
cheap ray bans
nike air max outlet
michael kors outlet
coach outlet
canada goose outlet
salomon shoes
nike shoes
red bottoms shoes
milwaukee brewers jerseys
coach outlet store
pandora outlet
longchamp handbags
ralph lauren sale clearance
ralph lauren uk
mont blanc pens
dansko shoes
uggs outlet
adidas shoes
michael kors outlet
cheap oakley sunglasses
kobe bryant shoes
ralph lauren outlet
uggs outlet
birkenstock outlet
adidas outlet
adidas nmd
fake rolex
fitflops sale clearance
pittsburgh pirates jerseys
converse shoes
coach factory outlet
michael kors outlet
toms outlet
kate spade bags
adidas outlet
adidas yeezy
michael kors outlet
birkenstock
moncler outlet
moncler jackets
timberland boots outlet
coach outlet
converse all star
birkenstock sandals
moncler outlet
canada goose outlet
polo outlet
birkenstock shoes
coach outlet
pandora outlet
adidas nmd shoes
uggs outlet
nike shoes
coach outlet online
texas rangers jersey
jimmy choo
coach outlet store
jimmy choo outlet
nike air max shoes
cleveland indians jerseys
fitflops
canada goose outlet
harden vol 1
ralph lauren sale clearance
pandora charms sale clearance
canada goose sale
pandora charms sale
nike shoes
supreme clothing
coach outlet
coach outlet
christian louboutin
birkenstock sandals
air max 2018
michael kors outlet
pandora charms
michael kors outlet online
ralph lauren
fitflops
pandora outlet
tory burch outlet online
coach canada outlet
oakley sunglasses outlet
uggs
adidas superstar
toms outlet
kate spade outlet
nike air max 87
moncler outlet
tory burch outlet
pandora jewelry
tiffany outlet
adidas
cheap oakley sunglasses
nfl jerseys wholesale
christian louboutin shoes
timberland boots
nike shoes for men
ecco shoes
jordans
pandora jewelry
cheap jordans
ugg boots
jimmy choo outlet
coach outlet
dr martens outlet
michael kors outlet clearance
moncler outlet
cheap jordans
pandora charms
ecco shoes for men
kate spade outlet
ralph lauren sale clearance
prada outlet
nike dunks
kevin durant shoes
discount oakley sunglasses
uggs outlet
timberland boots
pandora store
timberland outlet
air jordan shoes
adidas shoes
columbia sportswear
moncler outlet online
michael kors outlet clearance
cheap jordans
coach outlet
christian louboutin outlet
ralph lauren outlet
uggs outlet
air max 97
ralph lauren uk
coach outlet
kate spade outlet store
coach factory outlet
pandora jewelry
birkenstock shoes
coach outlet store online clearances
jordan shoes
tampa bay devil rays jerseys
longchamp handbags
ugg boots
nike zoom
canada goose sale
polo outlet store
ugg boots
kansas city royals jerseys
moncler jackets
michael kors outlet
ecco shoes
hermes bags
philipp plein outlet
adidas yeezy boost
kate spade outlet
canada goose outlet
polo ralph lauren outlet
ralph lauren outlet
moncler outlet
ralph lauren
florida marlins jerseys
kate spade bags
adidas shoes
mont blanc
nike store
mulberry outlet
dr martens boots
longchamp outlet
adidas yeezy boost
polo ralph lauren outlet online
canada goose outlet
yeezy boost 350
ugg outlet
michael kors outlet
tory burch outlet
replica watches
canada goose outlet
salvatore ferragamo shoes
nike zoom
kate spade
mulberry handbags
oakley sunglasses
chicago white sox jerseys
ugg outlet
fitflops sale clearance
philipp plein shirt
hermes handbags
ray ban sunglasses
vans store
pandora
nike tessen
fitflops sale clearance
louis vuitton outlet
air more uptempo
asics outlet
michael kors outlet clearance
nike air max
uggs canada
pandora charms
north face jackets
canadian goose
skechers shoes
christian louboutin outlet
michael kors outlet
nike air max zero
san diego padres jerseys
kate spade
coach outlet
christian louboutin
nike air max
pandora charms sale clearance
adidas outlet
louis vuitton outlet online
mulberry uk
canada goose jackets
air max 90
uggs outlet store
canada goose jackets
michael kors outlet online
nmd adidas
pandora charms
pandora jewelry
coach factory outlet
louboutin shoes
uggs
adidas stan smith
kate spade handbags
ralph lauren outlet
air jordan shoes
ralph lauren outlet
michael kors outlet
ugg outlet
gucci outlet
minnesota twins jerseys
coach factory outlet
coach outlet
coach outlet store
kate spade outlet
supra shoes
oakley sunglasses
uggs outlet
air max 2017
coach factory outlet
tiffany and co
salvatore ferragamo
nike huarache
coach outlet store
nike basketball shoes
jordan shoes
louis vuitton outlet
yeezy boost
uggs outlet
kate spade handbag
hermes outlet
jordans
nike air more money
coach outlet
hermes birkin
ugg outlet
pandora jewelry
prada handbags
moncler outlet
tory burch outlet
ugg boots
hermes handbags
oakley sunglasses
pandora jewelry
timberland boots
coach factorty outlet
coach canada outlet
coach outlet
asics shoes
pandora outlet
fitflops sale
michael kors handbags
ugg outlet
michael kors handbags
coach factory outlet
adidas shoes
oakley sunglasses
coach
cc20180921
                       |   

Liste des forums  |  Besoin d'un login ? Enregistre toi ici
 Identification
 Nom d'utilisateur:
 Mot de passe:
 Se rappeler de mon login:
   
 Mot de passe oublié ?
Entre ici ton e-mail ou ton identifiant et un nouveau mot de passe te sera envoyé par mail.